Urgent Ahmed Khalifa NIASSE fait de grave révélation Download

Send to your friends
Add
  • May 8, 2020

  • Emission Le Grand Plateau

Comments

  • MAMEBOUR BALANTE
    MAMEBOUR BALANTE 5 months ago

    Doyna war 🇸🇳 !! À mes sœurs Roy lén si Mame Diarra Bousso.

  • Yaaya Dialloo
    Yaaya Dialloo 5 months ago

    Pabi mo raw CORONA 😂😂😁

  • Mansata Dramé NDOYE
    Mansata Dramé NDOYE 5 months ago

    SoubhanaALLAH thiey ya ALLAH : même les enfants savent que le voile est une obligation religieuse en islam. Et ca dans toutes les religions révélées. Toutes les femmes vertueuses ont mis le voile de leur vivant.. Ci après la parole de l'omnicient, le sage par excellence 33. Restez dans vos foyers; et ne vous exhibez pas à la manière des femmes avant l'Islam (Jahiliyah).

  • Elimane Courbary
    Elimane Courbary 5 months ago (edited)

    Wakhi dofff rék

  • Omar Sallah
    Omar Sallah 5 months ago

    An-Nur

  • Awa Khouma
    Awa Khouma 5 months ago

    Yen niou tok thi Plateau yena geuna kham lou yalla santane ak limou tere kou de yak pakh linga ligey rek nga fay fek

  • BG Gueye
    BG Gueye 5 months ago

    Ameth khalipha niass amoul tarbiya.

  • Fallou Ndiaye
    Fallou Ndiaye 5 months ago

    C est a dire ki khaléyi comedien laniouko diapé.niome khamnaniouné limouye wakh dara amousi mai c est juste pour diko rètane.

  • Kara Diop
    Kara Diop 5 months ago

    Aywayy, ragalal yallah si linguaaaaay wakhh,

  • Ibrahima Lo
    Ibrahima Lo 5 months ago

    Yallah nanu yallah wusal si saytané ak yakh kat 🙏🙏 wakhal amine

  • Madia Junior Diop Faye
    Madia Junior Diop Faye 5 months ago

    Décidément donc mour prier dans les mosquées on doit demander des autorisations aux satan. Quils soient tous maudits

  • Amdy Thiam
    Amdy Thiam 5 months ago

    Ameth setal ligaye wax djiguene dafa mour aye thieureum gnoune gni diangoul sakh kham naneko

  • Ngagne Ndiaye
    Ngagne Ndiaye 5 months ago

    Seydina Mouhamed Psl meuss na sokh nam niko Yalla wane nama ay Djiguéne beuri di nagn dém Sarafa sokh na si niko Lou waral lolou mouniko niaka mourou. Ahmed Khalifa dél wakh deugg seytané nga liguéyal ioe

  • Bam's Bam's
    Bam's Bam's 5 months ago

    Barki Seydina Mouhamed dji Guen bou basé'wou si lou gorgui wax bilahi yangui si trokh tangué / ki louko néx lay wax

  • Babacar Diakhate
    Babacar Diakhate 5 months ago

    Yallah naniou Yallah mouceul ci Dadjial aki generalam

  • Breezy boy Ndiaye
    Breezy boy Ndiaye 5 months ago

    🤦🤦🤦🤦🤦🤦🤦🤦🤦🤦🥱🥱🥱🤭🤭🤭🤭 kilifa daye matte kilifa bou matoul kilifa ayy khalé dagnou koy yabb rek

  • Babs Diagne
    Babs Diagne 5 months ago (edited)

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣senegale mo.beuri commedien niankou amena kharite rék

  • Mafal nekhna trop Fall
    Mafal nekhna trop Fall 5 months ago

    Ahouzoubillahi mina cheytané radjimi

  • salif Ba
    salif Ba 5 months ago

    Thiey Ahmed ragalal yalla nga khameni diga déh boul toppou sa nafsou bakkane

  • Amy Tine
    Amy Tine 5 months ago

    Mais est ce que il va bien mentalement