Sanex Et Baye Ely : Lii Waral Thiow Lii Yeup....Leer neu Download

Send to your friends
Add
  • May 6, 2020

Comments

  • babacar ndiaye
    babacar ndiaye 4 months ago

    Manna am sakh aferou pape mbaye bi lako guayi mèré ba defko li

  • Bathie Ndiaye
    Bathie Ndiaye 4 months ago

    Sénégal danioko wara kholate bilah lou waye déff nio bayui ko si loko nékh

  • Adama Diallo
    Adama Diallo 4 months ago

    Toumeul nit loumou défoul daffa méti torop kounè dang kay khol thi sa bop

  • Sokhna Aminata Ba
    Sokhna Aminata Ba 4 months ago

    Salam, pour moi il n'y a pas de buzz ni de problème. Nous allons tous mourrir. Koula taguer Niko beuss si bire beuss yi dagnoula taguer taguer ma. C'est que la peur de la mort fait la colère de celui dont on annonce son départ ! Il y a des idiots qui s'amusent de tout dont la fausse mort de personne. Mais il faut que Sanekh comprenne son aînée Baye Ely mak le ! Aduna djegueul taye djeleuler. Beaucoup de palabres n'honore pas la culture! Les gars "siw d'où Diameu borome, kou siw mon si hame Dara!". Yalna yalla deff diam si diganter Sanekh ak Mame Baye Ely! Le vieux il est souffrant donc bayile mou sedeu Sanekh ! Wassalam.

  • Dicko Wade
    Dicko Wade 4 months ago

    Yakamté doule rek ba takhna douniou sakh vérifier information mou leer tes lolou rafétoul naniou kholat liniouy def way

  • ALEX CIBER
    ALEX CIBER 4 months ago

    No sanékh dafoul dara

  • Ameth Fam
    Ameth Fam 4 months ago

    Sanex diame rek guayy am délle wakh Amine rek

  • Rachid Ahmed
    Rachid Ahmed 4 months ago

    Dioum am n'a quoi. Nalen yalla takhawou niom niar nieup bakh mâcha alla

  • Mbaye Diakhate
    Mbaye Diakhate 4 months ago

    Yalla diam yagna

  • EL HADJI BA
    EL HADJI BA 4 months ago

    Bian dit mn frère é niouy deff lolou waar guène khamni yalla nélawoul lou way deff bopam

  • Gora Mbaye bou Serigne Habib sy makntoum tv

    Bien reçu merci beaucoup Macha Allah

  • Joe taïlle Basse
    Joe taïlle Basse 3 months ago

    Li wakh dëg la!

  • Thiongane Ousmane
    Thiongane Ousmane 4 months ago

    Merci beaucoup monsieur raffetnatrop Mame doundal té werr SERIGNE bii

  • Junior60
    Junior60 4 months ago

    Thiey junior mogui ni nekal thi diameu

  • Ndeye Fatou
    Ndeye Fatou 4 months ago

    Doyna war sènegal nio wari bayi tagué nit sur mak gni gnom danio ragal dè bolén tagué rek danioulay def none

  • Astou ndiaye Badji
    Astou ndiaye Badji 4 months ago

    Na lep rafétt rek adouna amoul solo lép téranga la

  • Mara Sidibe
    Mara Sidibe 4 months ago

    Journalise yi donio gawa wah doul rek

  • Big max tv
    Big max tv 4 months ago

    Mais sanex defoul Dara lou bakh rek lala yéné😓😓😓

  • Masood Usnani
    Masood Usnani 4 months ago

    Sankhe nit kou bah kou am yeurmande li yeup daye dieh mane magni niane yalla leral lep

  • Sidi Niang
    Sidi Niang 4 months ago

    Senegal moy lolou walahi bayilene yiii niaaw n tropp