Pour la première fois,Aida Patra parle du divorce entre Pape Cheikh Diallo&sa fille"li tass seuy bi" Download

Send to your friends
Add
  • May 11, 2020

  • #restezchezvous

Comments

  • Rémo bou Torino
    Rémo bou Torino 4 months ago

    14:10

  • uptown bangerz
    uptown bangerz 4 months ago

    We missed u Aida patra

  • Fkfjfn Jfjcjf
    Fkfjfn Jfjcjf 4 months ago

    Journaliste bii dafa yarou bakh deyssane bonne continuation

  • reine noire
    reine noire 4 months ago

    Bilay Aïda ak viviane ñion yem dougnou maguette mouk ❤💋 longue vie

  • PMND BRO
    PMND BRO 4 months ago

    Le titre c'est a partir de

  • Fatou rose Ndiaye
    Fatou rose Ndiaye 4 months ago

    Ndeyssane aida patra yalna yalla goudeul sa fane mais ligua wakh si pape cheikh rafete na kouko guiss Khamnè kou bakh la gueune nako fonk

  • Diagne Ndoye
    Diagne Ndoye 4 months ago (edited)

    MashAllah Aida Yalna Yallah geune taxawou Barké Maam Babacar Sy Yalna ga doone kou yiw ci biir ak ci biti comme vos parents. Yallah bollei xol yi bou keen yaxale keen Barké Seydi Woudjoub SAW

  • Mame fatou Loum
    Mame fatou Loum 4 months ago

    Machala kou bakh rek moy wague si nit Lou bakh pape cheikh moy kouko guisse rek khamnè nittou nène la 🙏🙏🙏

  • Aissatou Gueye Ndao
    Aissatou Gueye Ndao 4 months ago

    Man cha ALLAH yow mi donne posé Aida Patra question tu as été très respectueux yalla na ngua ame ndam si sa liguey Chapeau a Patra rafetna j'ai été surpris de ton changement et cela me fait très plaisir yalla na sa diam yague

  • NassiMilian Sidibé
    NassiMilian Sidibé 4 months ago

    Macha'Allah Patra. Journaliste poli, respectueux et professionnel Macha'Allah

  • Sali Diallo
    Sali Diallo 4 months ago

    Journaliste bi meuna limouy def bonne continuation.

  • Aïda mou Baay
    Aïda mou Baay 4 months ago

    merci aida bien parle sur les enfants de la rue moi aida Faye mou baye merci

  • Yaye Khady Badji
    Yaye Khady Badji 4 months ago

    Bilay kadou yi rafetna,maman aïda amal diam wayy 🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • Ndaye Fall
    Ndaye Fall 4 months ago

    Machallah aida amna solo

  • fatou ndiaye
    fatou ndiaye 4 months ago

    Aida patra depuis maye neck xaler lako beugone ba taye long vie a toi marieme faye Sall kén dou yaw bilay mala beug douma tayi thie diko wax

  • yallah na yallah koy soutoura

    Lima nekeu si aida mesouma wakh si papa cheikh lou bone aida yaw nit ko bakh te guemeu yallah

  • Binta Kane
    Binta Kane 4 months ago

    Non, c'est Amina Pote qui lui ressemble !

  • Kenza vivi Niang
    Kenza vivi Niang 4 months ago

    Longue vie tata🙏 thieuy sama ndanane bii Pape Cheikh chérie Kya Aïdara Diallo djéri 💯❤

  • Papa Djibril Dieng
    Papa Djibril Dieng 4 months ago

    Pape Cheikh Diallo la Référence 😍😍😍

  • Niang Bara
    Niang Bara 4 months ago

    Avancer jusqu'à