Kooru Biddew saison 5 Épisode 21 Download

Send to your friends
Add
  • May 15, 2020

  • Abonnez-vous à notre chaine Youtube ▷▷ ABONNEZ-VOUS ICI : Cliquez ici pour vous abonner 🔔 Activez les NOTIFICATIONS pour ne pas manquer les prochaines vidéos Retrouvez-nous sur http://www.leuztv.com/ ------------------------------------------------------------------ #RestezChezVous #AvecMoi #leuztv #Sénégal #Actualité #Politique #serie https://www.youtube.com/channel/UCOvr... Suivez-nous sur Facebook https://www.facebook.com/leuzmedia?fr...

Comments

  • Fallou gallass Mbow
    Fallou gallass Mbow 4 months ago

    Fama ak Dane tanyi nioy déff buzz. cou beug couple bi beusseule j'aime

  • Mor Talla Diop
    Mor Talla Diop 4 months ago

    Kou beug Corona bi diékh basal aime wy❤️❤️❤️

  • lamine Seck
    lamine Seck 4 months ago (edited)

    Yaw miy lire sama commentaier bi magi lay nianal linga begue sa xol yako xam yallnala ko yalla défal di sakou si yaw nga nianal ma

  • Amina Ba
    Amina Ba 4 months ago

    Bideew une femme mariée ne doit pas raconter sa vie conjugale à n'importe qui

  • TER NIANE
    TER NIANE 4 months ago

    Ani wa team ande sètane theatre yeuppe ak sène wifi 😂🙃🙋‍♂️🌛🌛🌛🔥

  • Amy Sow
    Amy Sow 4 months ago

    Bideew aussi adji n'est pas la bonne personne à qui tu doit te confié 🤦 hypocrite la wa yéne laleuse ak mor anta danio diobo taye dhe😂😂

  • Mansour Dieng
    Mansour Dieng 4 months ago

    Vendredi 15 Mai 2020

  • Aminah Gueye
    Aminah Gueye 4 months ago

    Team Mass tamit messoumako degue ana gni begue Mass😂❤yalna diame yague

  • adja linguere Ndiaye
    adja linguere Ndiaye 4 months ago

    Germaine est tres mignonne mashallah wayé biddew djiguene bouy seuy sa yaye nga wara demandé conseil pas ton amie célibataire

  • Aminata Dramé
    Aminata Dramé 4 months ago

    Motakh kharitou adji bi mo bakh si mome ndakh seytané leu

  • Rokhina Sall
    Rokhina Sall 4 months ago

    Kou kor gui di manque??mongui tagato dh🙈😥

  • iam mbaye
    iam mbaye 4 months ago

    Film bi dieukeurou fama bi moy sama acteur 😂😂😂

  • fall mbarkiss
    fall mbarkiss 4 months ago

    enfin laleuse ak mor anta dioubo nagn😂😂

  • bb chou
    bb chou 4 months ago

    Badiene dé dem ndar diaral nako louné

  • Kya Mbengue
    Kya Mbengue 4 months ago

    Nekhoul ba nekhoul mais badiéne mogui raté ay toggou biddew you am diom😂😂

  • Aicha
    Aicha 4 months ago

    Allez les filles sondages.

  • yacine diop
    yacine diop 4 months ago

    Bidéw yaw tmt Méré nala trop pour quoi parles tu tes blems à Adji toi aussi qui est d'accord pousse bleu🤔

  • Cheikhouna Cisse
    Cheikhouna Cisse 4 months ago (edited)

    Man may aucune vues😂😂🤗😝😝😜

  • Marie Louise Camara
    Marie Louise Camara 4 months ago

    Bilahi keur dane nekhna na😂😂😂🤣🤣

  • Yacine Sarr
    Yacine Sarr 4 months ago

    Mais bidéw pourquoi tu dit tes problèmes à Adja