INCHALLAH, Mounass Ak Sey Bi - Pré-Saison - Episode 1 **VOSTFR** Download

Send to your friends
Add
  • Premiered May 15, 2020

  • ** Abonne toi ici : https://bit.ly/DNMtvAbonneToi ** Découvrez l'épisode 1 de la nouvelle web série "INCHALLAH, Mounass Ak Sey Bi". "Mounass Ak Sey Bi" est une parodie de vie de couple. Pour débuter cette première saison, nous vivons le confinement aux côtés de Mounass et de son tendre époux Seydou : ils s'aiment mais leur mariage est loin d'être un long fleuve tranquille ! La série dépeint avec humour des réalités bien sénégalaises... et tout ira bien INCHALLAH ! Un épisode tous les mardis & vendredis soirs vers 20h00 UTC. A ne pas manquer !!! #Inchallah #MounassAkSeyBi #Episode1 #Saison1 #Mounass #Seydou #DNMtv #Love #Team221 Une série ASD Production (Dakar, Senegal, mai 2020) ** Retrouvez-nous sur les réseaux sociaux ** Suivez nous sur Facebook : https://www.facebook.com/dnmtv221 Suivez nous sur Twitter : https://twitter.com/dnmtv221

Comments

  • Sokhna Diop
    Sokhna Diop 4 months ago

    Ani fans maïmouna yi💖

  • Bineta Ndiaye
    Bineta Ndiaye 4 months ago

    Ani wa taem maïmouna beusseul j'aime 🔥🔥🔥

  • Awa
    Awa 4 months ago

    Vu que Mounass est de retour, ngir yallah faite la suite de "dinama nekh" , qu'est-ce qui va se passer après l'accident de Maimouna!?

  • Oumy Ndiaye
    Oumy Ndiaye 4 months ago

    Ooooh Maty Thiam dogo bi Mounass di déglou nékh nama vivent nos anciens ani gniy déglou rétro wa t'aime rétro manifestez vous

  • Awa Ndiaye Kambi
    Awa Ndiaye Kambi 4 months ago

    Mounass sama xoll lako déff ak confinement bi ni chaque jour mangi dinama nékh di ré sama xoll di fékh

  • Maréme Seck
    Maréme Seck 4 months ago

    Ani gnigua khame ni béne série douléne raw séne lokho thia kaw maye guisse

  • Abdou Gueye Ndiaye
    Abdou Gueye Ndiaye 4 months ago

    Bilayy mane momm dama beugg Mounass ak Métzo ......je suis de tout coeur avec vous ,j'espère que cette série sera apprécié de tout le monde....si kaww si kanamm rék 😘😘😍😍😍😍

  • MBAYE FALL
    MBAYE FALL 4 months ago

    Ana gniy setane ak sen téléphone en mm temps di lire commentaire yi

  • diodio diop
    diodio diop 4 months ago

    Maimouna ray nama domodaaa bou saff sapp ak lingom

  • Oumi Dial Diop
    Oumi Dial Diop 4 months ago

    Daaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaarrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrooooooooooooooooooo😍 est demandé en urgence !

  • Faya
    Faya 4 months ago

    Sheu xamo sax nimalen namé mane nga xamni mounouma xeuy té setanou dinama nekh

  • Binta Kane
    Binta Kane 4 months ago

    C'est avec nostalgie de la revoir et ce fût un plaisir de te retrouver dur une autre facette. 👍👍

  • Fatou Gueye
    Fatou Gueye 4 months ago

    Ay way ana dara na niew way

  • Nancy Coly
    Nancy Coly 4 months ago

    Ki trouv kom moi k mounas a changé physiquement

  • Ozil Cisko
    Ozil Cisko 4 months ago

    Saydou dinama raye ak action bruce lee

  • Mohamed Ba
    Mohamed Ba 4 months ago

    😁😁😁😁😁vraiment tonton seydou Mane yamaye soulagé l'intello des comédiens machallah sensibilisation contre Corona bi rafetna

  • Yacine Ndiaye
    Yacine Ndiaye 4 months ago

    Song bi mo yague tee neeekhh Baba djémé kayy gnou yeugoo maty thiam dogo wayy akaa meuna wayy😘😘

  • Tening Ndoye
    Tening Ndoye 4 months ago

    Ay way lih diii aimer na tei commencé goul ... 🤣

  • Fatou bintou Diouf
    Fatou bintou Diouf 4 months ago

    Machalla way bonne continuation jm❤ms mounass vas m tué sénégalais 200% degue dou nékh

  • saliou ndiaye
    saliou ndiaye 4 months ago

    Les nostalgiques de dinama le khorom est à Maggi à la porte d à côté 😂😂😂😂 je rigole ne m insulter pas x juste que j adore ce New concept de mounass l humour mesuré bon dialogue audible et bonne mise en scène 🙏🙏🙏🙏