Enterrement du père de Modou Lô : Eumeu Séne, Baboye, Tapha Guèye et le monde de la lutte présents Download

Send to your friends
Add
  • May 8, 2020

  • Visitez notre site web http://luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct https://www.facebook.com/luttetv/ https://www.facebook.com/luttetv/ https://www.instagram.com/luttetv/ http://luttetv.com/ https://www.youtube.com/user/senlamb

Comments

  • L’absolu Gueye
    L’absolu Gueye 4 months ago

    Naysann Mdou Lo Masta way 😭😭😭Mètina Trop Yallah Nako souniou borom Yeureum thi Barke borom touba 🙏♥️🙏

  • Bamba Seck
    Bamba Seck 4 months ago

    C'est vraiment beau c ça le Sénégal billahi sama yaram dawna adversité dou animosité

  • AKHIBOU SAMB
    AKHIBOU SAMB 4 months ago

    Qu Allah l'accueil Dans son paradis AMINE 🙏

  • Amadou Sarr
    Amadou Sarr 4 months ago

    Li rafétena yalnako yalla yeureum. Té amenagne ci yakaar ci barké weerou koor gui.

  • Cheikh Diouf
    Cheikh Diouf 4 months ago

    Modou courage ,yalla na yalla yeureme ko haréko aldiana firdawous si barké Seydouna Mouhamet amine ya Rabi

  • OUSMANE SONKO THIAM
    OUSMANE SONKO THIAM 4 months ago

    Inaa lilaahi wa inaa ilayhi raajihon yalnako yallah yeureum tam jeugalko kharéko aljana ci barki wérou koor gui

  • Mbacke khadim 764394677

    Yallanako yalla kharé aldiana barkib borom touba

  • Mouhamed Ndong
    Mouhamed Ndong 4 months ago

    Yalnako yallah geureum tei xarrei aldjana firdawsi ci Barkep Muhammad PSL metina trop mais Modou Lo Siggil ndigalei

  • Ambroise Mendy
    Ambroise Mendy 4 months ago

    Pikine la deuk mais dama beugue modou lo yalla na yalla kharé pabi sa aljana you kawéya

  • ndaraw Niang class'chicc

    Yalna ko yalla kharé aldiana

  • babacar dieng
    babacar dieng 4 months ago

    Ndeysane li moy senegal so amé banekh nio tewlé la so amé nakar tamit niou tewlé la

  • Momo Touray
    Momo Touray 4 months ago

    Que Firdawsi soit sa demeure éternelle Amine courage La vie est Courte

  • Mody Diallo
    Mody Diallo 4 months ago

    Yalla na ko yalla kharré aldiana remerciant tout les lutteurs c'est ça le Sénégal

  • Daouda Ndiaye
    Daouda Ndiaye 4 months ago

    Ndeysane 😭 yalnako yalla yeureum kharéko aldiana 😭 Sénégal ni rek la raféte na yalna yalla konn tann 🤲🤲🤲👈

  • Mansour Dieng
    Mansour Dieng 4 months ago

    VENDREDI 8 MAI 2020 YALLA NAKO YALLA KHARÉ ALDIANA BALLA MODOU EUMEU SÉNE YÉNA BOKOU NDAYE AK BAYE ADOUNA AMOUL SOLO 😭😭

  • Babacar Sarr
    Babacar Sarr 4 months ago

    Sunu roi sama roi magii lay mastawou dila dialé dila nianal o6 sa papa sunu mame yal nako yeureume té Khéréko Aldiana Sii Barkké Yonantéby (PSL) Champion dit courage Mouneieul o6.....

  • Mody Waiga
    Mody Waiga 4 months ago

    Ndeysane yalnako souniou borom yeureum té kharéko aldiana firdawsi

  • Mbaye Diouf FAYE
    Mbaye Diouf FAYE 4 months ago

    Yalla na souf sédeu si kawam borom bi xaréko aldjana firdawsi si barké seydina Mouhamed salalahou aleyhi wa salam 🙏🏾

  • Gora Lo
    Gora Lo 4 months ago

    Ndeyesan yalla na co yalla xare andjiana amine Sama tourodo dèmeni ndeyesan

  • Maboury niang EL rey
    Maboury niang EL rey 4 months ago

    Adouna amoul solo li rek la nitt mounal moromaam! Sénégal ben bopp leu et je prie qu'Allah le tt puissant l'accueille dans son saint paradis. Amiine