Enfants égorgés par leur père à Touba: l'ami intime du meurtrier accuse les charlatans Download

Send to your friends
Add
  • Premiered May 14, 2020

  • Infos Rewmi est un site d'Information Sénégalais de people, Buzz,Société,Sports,Politique,Culture etc...

Comments

  • Khadim Sene
    Khadim Sene 6 months ago

    Sen yaye yi yalna len yalla may xolou mougn te xalle yi yalna len yalla xare aldiana 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • Mouhamadou Ndiaye
    Mouhamadou Ndiaye 6 months ago

    Le maraboutage doit être criminalisé au Sénégal

  • Maty Aidara
    Maty Aidara 6 months ago

    Adouna da diakhasso djinê yii gno nek si biir nitt yi dilen diakhassé dilen dfflo lou bonne

  • Issa Fall
    Issa Fall 6 months ago

    Mane nga xamni dama beugue sama dôme sou febare' sakhe damaye diakhle' dotouma beugue dara motakh geumoumani bara thi sagome la défe' lii

  • Mouhamadou Ndiaye
    Mouhamadou Ndiaye 6 months ago

    Tiey Sénégal bayilene nit yi nguene di ligueye bagnouy tago sene sago .

  • David Diop
    David Diop 6 months ago

    Bara est le seul qui pourrait justifier ce fait.

  • SOLDAROU MAME SALIOU
    SOLDAROU MAME SALIOU 6 months ago

    Li dé doyna warr mes Limay digale sama mbokki dioulite yi moy moytoulène ndiabarkate yi

  • THIEDO
    THIEDO 6 months ago

    AMNA NITT YOU BONNE YOU NEK SI DEUKK BII DANIOULAY KHAPTAL LOUNOULA DEFLO DANGAKOY DEF PAR FORCE THÉ DO KHOM LOULAKOY DEFLO LOU DOY WARR LALAY TEGAL NIII

  • seydina diop Bichri
    seydina diop Bichri 6 months ago

    gni wax gnépou Séne xalate rék lagnouye wax

  • Bara Fall
    Bara Fall 6 months ago

    Ndeysan sama toma Bara yalnah Yallah leral lep metina trop sax mai Yallah bakhna lep dina fenge Incha allah

  • Thiatt Diene
    Thiatt Diene 6 months ago

    Meune naniouko khaptal aussi leppa nguissi

  • Fallou Seye
    Fallou Seye 6 months ago

    Doyna war d mande guamomane moko tay

  • aline badara
    aline badara 6 months ago

    Barra dé liko dal métina trop waye njépp lou bakh laniou wakh si mome

  • Mame bamba Niang
    Mame bamba Niang 6 months ago

    Mane mi chak magal kereum lay dal barki cheikhoul khadim bakh ak beugue ndiabotam liiii môme geumoumani moko tay ndakh mane ak talibè beugue cheikhoul khadim rk lako khamè barki s salliou yalla na borombi dolliko kholou mougne j sw de tt cœur avec son épouse momy cissè yalnako yalla May kholou mougne

  • cheikh mbacke
    cheikh mbacke 6 months ago

    Mane domam la wallahi lou bakh rk la kham thie mome khayna sakh douma mana wakh thie mome ndakh lou ma wakh niou né domam la waaye yalla guiss na lepp yalla na niou yalla soutoural

  • awa bakhoum
    awa bakhoum 6 months ago

    Ce que dit le sieur en t.shirt noir est tres pertinente. L'enquête doit continuer pour connaître le motif l'alibi de son acte. Un pchychologue pourrait le faire parler. Diarnako déh

  • Elhadji Mbengue
    Elhadji Mbengue 6 months ago

    NDEYE SANN 😭😭😭😭 AY WAY SÉNÉGAL NIOUNGUI SOUKHORR BA LÉNGUI KHAR FA KHOUFA LA

  • Abdou Tall
    Abdou Tall 6 months ago

    Thiey aduna lou métti yaguenafi. Ndeysan tè digueuté am akk ñak dafa soriwull. Li ay pékhè seytané moussi lakhassou rk. Yalla na Yalla doli soutoureu.

  • Ibrahima Paye
    Ibrahima Paye 6 months ago

    Je suis mouride sadékh

  • Hanne Ababacar
    Hanne Ababacar 6 months ago

    Kène xamoul couco dèf